Hadith Representative
As Salam
Imam Nasa'i : 1155أَخْبَرَنِي عَبْدُ الرَّحْمَنِ بْنُ خَالِدٍ الرَّقِّيُّ قَالَ حَدَّثَنَا حَارِثُ بْنُ عَطِيَّةَ وَكَانَ مِنْ زُهَّادِ النَّاسِ عَنْ هِشَامٍ عَنْ حَمَّادٍ عَنْ إِبْرَاهِيمَ عَنْ عَلْقَمَةَ عَنْ ابْنِ مَسْعُودٍ قَالَكُنَّا إِذَا صَلَّيْنَا مَعَ رَسُولِ اللَّهِ صَلَّى اللَّهُ عَلَيْهِ وَسَلَّمَ نَقُولُ السَّلَامُ عَلَى اللَّهِ السَّلَامُ عَلَى جِبْرِيلَ السَّلَامُ عَلَى مِيكَائِيلَ فَقَالَ رَسُولُ اللَّهِ صَلَّى اللَّهُ عَلَيْهِ وَسَلَّمَ لَا تَقُولُوا السَّلَامُ عَلَى اللَّهِ فَإِنَّ اللَّهَ هُوَ السَّلَامُ وَلَكِنْ قُولُوا التَّحِيَّاتُ لِلَّهِ وَالصَّلَوَاتُ وَالطَّيِّبَاتُ السَّلَامُ عَلَيْكَ أَيُّهَا النَّبِيُّ وَرَحْمَةُ اللَّهِ وَبَرَكَاتُهُ السَّلَامُ عَلَيْنَا وَعَلَى عِبَادِ اللَّهِ الصَّالِحِينَ أَشْهَدُ أَنْ لَا إِلَهَ إِلَّا اللَّهُ وَحْدَهُ لَا شَرِيكَ لَهُ وَأَشْهَدُ أَنَّ مُحَمَّدًا عَبْدُهُ وَرَسُولُهُ
Bimu demee ba ci man, mu ne: mu wax nu [Harits bin Athiyyah] te moom kenn la ci nit ñi gëna réccu, ci Hisyam, ci Hammad, ci Ibrahim, ci Alqamah, ci Ibn Mas'ud, mu wax ko; 'Danu daan ñaan ak Rasulullah sallallaahu'alaihiwasallam di wax assalaamu 'alaallah, assalaamu 'alaa jibriil, assalaamu 'alaa Mikail -Jàmm yal na Yàlla, jàmm yalna jibril, jàmm yalna laalaahi mikaayil-'. Rasulullah Sallallaahu'leyhiwasallam niko: Bul sàggane; 'Assalaamu 'alallah -Jàmm na ci Yàlla-' ndax Yàlla mooy Assalaam -Mooy Joxe mucc-, waaye wax ne 'At Tahiyyatut lillaahi wash-shalawaatu wath-thayyibaatu, assalaamu 'alaika ayyuhan-nabiyyu wa rahmatullahi wa allaakaatuh, assalaamu 'alaayishaahina wa'alaa ilaah illallaah wahdahu laa shariikalah wa asyhadu anna muhammadan abduhu warasuuluh tedd bu baax ak barké yalla na ci yallah. Yalna la jam ak yërmande ak barke sax ci yaw Yonent bi. Yalna mucc nekk ak jaamu Yàlla yu baax yi itam. Maa ngi seede ni amul beneen mbindéef bu yelloo ñu jaamu ludul Yàlla rek, te amul benn àndadoo, te maa ngi seede ni Mohamed jaamam la, di ndawam.