Embrasser l'Islam, cliquez ici
ISLAM AL-HAQ: QURAN & HADITH
(The True Islam)



Kelembutan dan kesabaran Nabi mendengar keluhan orang
Imam Ahmad : 13535

حَدَّثَنَا عَفَّانُ حَدَّثَنَا حَمَّادٌ عَنْ ثَابِتٍ عَنْ أَنَسٍ أَنَّ امْرَأَةً كَانَ فِي عَقْلِهَا شَيْءٌ فَقَالَتْ يَا رَسُولَ اللَّهِ إِنَّ لِي حَاجَةً فَقَالَ يَا أُمَّ فُلَانٍ انْظُرِي إِلَى أَيِّ الطَّرِيقِ شِئْتِ فَقَامَ مَعَهَا يُنَاجِيهَا حَتَّى قَضَتْ حَاجَتَهَا

Neena ñu ['Affan] Neena ñu [Hammad] ci [Thabit] ci [Anas] amoon na benn jigéen bu xel mi jaarul yoon, mu wax; Yaw Yonent Yàlla, dama am soxla. Rasulullah aleyhi wasallam niko: 'Yaw Ummu Fulan, jëlal yoon wi nga bëgg' ci noonu la Rasulullah aleyhi wasallam taxaw ak moom di waxtaan ak moom ba liggéeyu ku jigéen ki jeex.

Hadith Corroboration :


Imam Ahmad : 13535
Imam Muslim : 4293