Embrasser l'Islam, cliquez ici
ISLAM AL-HAQ: QURAN & HADITH
(The True Islam)



Setiap anak Adam pasti bersalah dan sebaik-baik orang yang bersalah adalah yang bertaubat
Imam Ahmad : 20194

حَدَّثَنَا أَبُو مُعَاوِيَةَ عَنْ أَبِي إِسْحَاقَ الشَّيْبَانِيِّ عَنْ يَزِيدَ بْنِ الْأَصَمِّ عَنْ ابْنِ عَبَّاسٍ قَالَ جَاءَ رَجُلٌ إِلَى عُمَرَ يَسْأَلُهُ فَجَعَلَ يَنْظُرُ إِلَى رَأْسِهِ مَرَّةً وَإِلَى رِجْلَيْهِ أُخْرَى هَلْ يَرَى عَلَيْهِ مِنْ الْبُؤْسِ شَيْئًا ثُمَّ قَالَ لَهُ عُمَرُ كَمْ مَالُكَ قَالَ أَرْبَعُونَ مِنْ الْإِبِلِ قَالَ ابْنُ عَبَّاسٍ فَقُلْتُ صَدَقَ اللَّهُ وَرَسُولُهُ لَوْ كَانَ لِابْنِ آدَمَ وَادِيَانِ مِنْ ذَهَبً لَابْتَغَى الثَّالِثَ وَلَا يَمْلَأُ جَوْفَ ابْنِ آدَمَ إِلَّا التُّرَابُ وَيَتُوبُ اللَّهُ عَلَى مَنْ تَابَ فَقَالَ عُمَرُ مَا هَذَا فَقُلْتُ هَكَذَا أَقْرَأَنِيهَا أُبَيٌّ قَالَ فَمَرَّ بِنَا إِلَيْهِ قَالَ فَجَاءَ إِلَى أُبَيٍّ فَقَالَ مَا يَقُولُ هَذَا قَالَ أُبَيٌّ هَكَذَا أَقْرَأَنِيهَا رَسُولُ اللَّهِ صَلَّى اللَّهُ عَلَيْهِ وَسَلَّمَ قَالَ أَفَأُثْبِتُهَا فَأَثْبَتَهَا

Neena ñu ni [Abu Mu'awiyah] ci [Abu Ishaq Asy Syaibani] ci [Yazid bin Asham] ci [Ibn Abbas] dafa wax ni, 'Dafa amoon ku ñëw ngir gise ak Omar mu laaj ko, yenn saa yi Omar xool boppam, yenn saa mu xool tànkam yi. Amaana mën na gis ay njuumte yu nekkoon ci moom. Mu laaj ko ba ñaata alal nga am? Ku góor ki tontu ko, 'ñeent-fukki gaam.' Ibn Abbas nee na: «Maa ngi màggal Yàlla ak Yonentam, su doomu Aadama amoon ñaari vale, ci lu wér dina wut ñetteelu vale. Te dara mënula fees ci gémmiñu doomi Aadama lu dul suuf. Te Yàlla dana may tuub ñi bëgga tuub’. Omar niko, lii lan la? Ma tontu ko, lii mooy li ma dégg ci Ubay. Omar daal di ñëw ngir gis Ubay ak man, Omar niko, 'Lu nit ki -Ibnu Abbas- wax?' [Ubay] tontu ko niko, lii la Yonent bi sallallaahu aleyhi wasallam jàngal ma ko. Omar ne ko ndax mën naa ko gëm? Ci noonu Omar gëm ko.

Hadith Corroboration :

Imam Ahmad : 3321, 11781, 12256, 12527, 12991, 13011, 13063, 13097, 13370, 14130, 14138, 18477, 20194, 23141
Imam Bukhari : 5956, 5957, 5958, 5959
Imam Muslim : 1737, 1738, 1739, 1740
Imam Tirmidzi : 2259
Imam Ibnu Majah : 4225
Imam Darimi : 2659