Embrasser l'Islam, cliquez ici
ISLAM AL-HAQ: QURAN & HADITH
(The True Islam)



- Haji dan Umrah Tawaf Qudum (Selamat Datang) Bolehnya thawaf di Baitullah sebelum wuquf di Arafah, sebagaimana yang Rasulullah lakukan
Hadith Search Results :
Total Hadith : 1
Hadith Representative
Bolehnya thawaf di Baitullah sebelum wuquf di Arafah, sebagaimana yang Rasulullah lakukan
Imam Muslim : 2170

حَدَّثَنَا يَحْيَى بْنُ يَحْيَى أَخْبَرَنَا عَبْثَرٌ عَنْ إِسْمَعِيلَ بْنِ أَبِي خَالِدٍ عَنْ وَبَرَةَ قَالَ كُنْتُ جَالِسًا عِنْدَ ابْنِ عُمَرَ فَجَاءَهُ رَجُلٌ فَقَالَ أَيَصْلُحُ لِي أَنْ أَطُوفَ بِالْبَيْتِ قَبْلَ أَنْ آتِيَ الْمَوْقِفَ فَقَالَ نَعَمْ فَقَالَ فَإِنَّ ابْنَ عَبَّاسٍ يَقُولُ لَا تَطُفْ بِالْبَيْتِ حَتَّى تَأْتِيَ الْمَوْقِفَ فَقَالَ ابْنُ عُمَرَ فَقَدْ حَجَّ رَسُولُ اللَّهِ صَلَّى اللَّهُ عَلَيْهِ وَسَلَّمَ فَطَافَ بِالْبَيْتِ قَبْلَ أَنْ يَأْتِيَ الْمَوْقِفَ فَبِقَوْلِ رَسُولِ اللَّهِ صَلَّى اللَّهُ عَلَيْهِ وَسَلَّمَ أَحَقُّ أَنْ تَأْخُذَ أَوْ بِقَوْلِ ابْنِ عَبَّاسٍ إِنْ كُنْتَ صَادِقًا

Daf nu wax [Yahya bin Yahya] wax nu [Abtsar] ci [Isma'il bin Abu Khalid] ci [Wabara] mu ne; Benn bis laa toog ak [Ibnu Omar], ci saasi benn góor ñëw ci moom laaj ko, ndax sama jëf dina jub sudee ma njëkka tawaaf ci Baitullah balaa may ñëw Arafat ngir wuquf? Ibn Omar tontu ko, 'waaw, loolu mooy dëgg'. Waaye Ibnu Abbas dafa wax ni: Bul tawaaf ci Baitullah ba nga def wuquf ci Arafah. Ibn Omar dafa wax ni Rasulullah def na hajj màkka, mu def Tawaf ci Baitullah balaa muy ñëw Arafah ngir wuquf fa. Kon soo nekkee nit ku jub, ban ci ñoom nga gëna am sañ-sañu jël; waxi Rasulullah Sallallaahu aleyhi wasallam wala waxi Ibn Abbas?'

Hadith Corroboration :