Hukum tentang memakan hasil buruan anjing terlatih dan panah yang dilepaskan dengan menyebut nama Allah
Imam Bukhari : 5054حَدَّثَنَا سُلَيْمَانُ بْنُ حَرْبٍ حَدَّثَنَا شُعْبَةُ عَنْ عَبْدِ اللَّهِ بْنِ أَبِي السَّفَرِ عَنْ الشَّعْبِيِّ قَالَ سَمِعْتُ عَدِيَّ بْنَ حَاتِمٍ رَضِيَ اللَّهُ عَنْهُ قَالَسَأَلْتُ رَسُولَ اللَّهِ صَلَّى اللَّهُ عَلَيْهِ وَسَلَّمَ عَنْ الْمِعْرَاضِ فَقَالَ إِذَا أَصَبْتَ بِحَدِّهِ فَكُلْ فَإِذَا أَصَابَ بِعَرْضِهِ فَقَتَلَ فَإِنَّهُ وَقِيذٌ فَلَا تَأْكُلْ فَقُلْتُ أُرْسِلُ كَلْبِي قَالَ إِذَا أَرْسَلْتَ كَلْبَكَ وَسَمَّيْتَ فَكُلْ قُلْتُ فَإِنْ أَكَلَ قَالَ فَلَا تَأْكُلْ فَإِنَّهُ لَمْ يُمْسِكْ عَلَيْكَ إِنَّمَا أَمْسَكَ عَلَى نَفْسِهِ قُلْتُ أُرْسِلُ كَلْبِي فَأَجِدُ مَعَهُ كَلْبًا آخَرَ قَالَ لَا تَأْكُلْ فَإِنَّكَ إِنَّمَا سَمَّيْتَ عَلَى كَلْبِكَ وَلَمْ تُسَمِّ عَلَى آخَرَ
Dañu nu wax [Sulaiman bin Harb] neena, ñu wax nu [Syu'bah] ci [Abdullah bin Abu As Safar] ci [Ash Sya'bi] mu ne: 'Dégg naa [Adi bin Hatim] radiallahu 'anhu' wax, 'maa laaj Rasulullah tontu ko ci limu def. ‘Sudee wàll wi ñaw la lekk ko, waaye bu dee wàll wi ñaw moo koy dóor. Sudee wet gi dafa dëgër, kon Waqidz la, baayima buñu ray te duñu ko ray ak ngannaay bu ñaw, kon bul ko lekk. Ma laajaat, 'Bàyyi naa sama xaj!' Mu tontu ko ne: “Soo ko bàyyee ci tudd Yàlla, lekk ko”. Ma laajaat, 'Sudee lekk nako?' Mu tontu ko : ''Bul lekk, ndax jàppuwul ngir yaw, boppam kese la koy jàpp'. Ma laajaat, 'Bima bàyyee sama xaj, gis naa beneen xaj?' Mu tontu ko : Bul ko lekk, ndax sa xaj kese ngay wax turu Yàlla, doo wax yeneen xaj.
Hadith Corroboration :
Imam Ahmad : 17067, 17071, 17544, 17547, 17554, 18562, 18563, 18574, 18579, 18580, 18581, 18582
Imam Bukhari : 1913, 5054, 5061, 5062, 5064, 6848
Imam Muslim : 3560, 3561, 3562, 3563, 3564, 3565, 3566
Imam Abu Dawud : 2464, 2465, 2469, 2471
Imam Tirmidzi : 1384, 1389, 1390, 1391
Imam Nasa'i : 4190, 4191, 4192, 4194, 4197, 4198, 4199, 4200, 4201, 4222, 4224, 4225, 4231, 4232, 4233, 4234
Imam Ibnu Majah : 3199, 3205
Imam Darimi : 1924