Embrasser l'Islam, cliquez ici
ISLAM AL-HAQ: QURAN & HADITH
(The True Islam)



Matahari berhenti di bawah Arsy, lalu sujud
Imam Tirmidzi : 2112

حَدَّثَنَا هَنَّادٌ حَدَّثَنَا أَبُو مُعَاوِيَةَ عَنْ الْأَعْمَشِ عَنْ إِبْرَاهِيمَ التَّيْمِيِّ عَنْ أَبِيهِ عَنْ أَبِي ذَرٍّ قَالَدَخَلْتُ الْمَسْجِدَ حِينَ غَابَتْ الشَّمْسُ وَالنَّبِيُّ صَلَّى اللَّهُ عَلَيْهِ وَسَلَّمَ جَالِسٌ فَقَالَ يَا أَبَا ذَرٍّ أَتَدْرِي أَيْنَ تَذْهَبُ هَذِهِ قَالَ قُلْتُ اللَّهُ وَرَسُولُهُ أَعْلَمُ قَالَ فَإِنَّهَا تَذْهَبُ تَسْتَأْذِنُ فِي السُّجُودِ فَيُؤْذَنُ لَهَا وَكَأَنَّهَا قَدْ قِيلَ لَهَا اطْلُعِي مِنْ حَيْثُ جِئْتِ فَتَطْلُعُ مِنْ مَغْرِبِهَا قَالَ ثُمَّ قَرَأَ وَذَلِكَ مُسْتَقَرٌّ لَهَا قَالَ وَذَلِكَ قِرَاءَةُ عَبْدِ اللَّهِ بْنِ مَسْعُودٍقَالَ أَبُو عِيسَى وَفِي الْبَاب عَنْ صَفْوَانَ بْنِ عَسَّالٍ وَحُذَيْفَةَ بْنِ أَسِيدٍ وَأَنَسٍ وَأَبِي مُوسَى وَهَذَا حَدِيثٌ حَسَنٌ صَحِيحٌ

Dafa wax nu [Abu Mu'awiyah] ci [Al A'masy] ci [Ibrahim At Taimi] ci [baayam] ci [Abu Dzarr] ne: Ma dugg ci Jumaa ji bi jant bi so, fekk Yonent bi sallallaahu aleyhi wa Salam toogoon, mu laaj ma: 'Yaw Abuzar, fan nga xam? Abu Dzarr ne ko: man tontu naa: Yàlla ak Yonentam ñoo gën a xam. Rasulullah sallallaahu 'alaihi wa Salam dafa wax ni: 'mu dem ngir ñaan ndigal mu sujud, ñu may ko ndigal, dafa melni dañu ko wax: jog ci barab bi nga ñëwoon. ba noppi mu jog ci toogukaay bi, ba noppi mu jàng: 'Te foofu mooy barabu dogalam'. Abu Dzaar nee na: loolu mooy li Abdalaa bin Masuud jàngoon. Abu Isa neena: ci mbir mii amna hadiis bu ni mel bu bawoo ci Shafwan bin Assal, Hudzaifah bin Usaid, Anas, Abu Musa te hadiis bii mooy Hasan Sahih.

Hadith Corroboration :

Imam Ahmad : 20338, 20390, 20437, 20561, 20563, 20999
Imam Bukhari : 2960, 4428, 4429, 6874, 6881
Imam Muslim : 228, 229, 230
Imam Abu Dawud : 3488
Imam Tirmidzi : 2112, 3151