Imam Ahmad : 15307
حَدَّثَنَا مُحَمَّدُ بْنُ جَعْفَرٍ قَالَ حَدَّثَنَا شُعْبَةُ قَالَ سَمِعْتُ أَبَا إِسْرَائِيلَ قَالَ سَمِعْتُ جَعْدَةَ قَالَ سَمِعْتُ النَّبِيَّ صَلَّى اللَّهُ عَلَيْهِ وَسَلَّمَ وَرَأَى رَجُلًا سَمِينًا فَجَعَلَ النَّبِيُّ صَلَّى اللَّهُ عَلَيْهِ وَسَلَّمَ يُومِئُ إِلَى بَطْنِهِ بِيَدِهِ وَيَقُولُ لَوْ كَانَ هَذَا فِي غَيْرِ هَذَا الْمَكَانِ لَكَانَ خَيْرًا لَكَ
Neena ñu [Muhamed bin Ja'far] ni; wax nu [Syu'bah] ni; Dégg naa [Abu Israil] naan; Dégg naa [Ja'dah] wax; Dégg naa Yonent bi sallallaahu aleyhiwasalaam,mu gis ku duuf, ci la Yonent bi sallallaahu aleyhiwasalm joxoñ biiram ak loxoom ne ko: duhh bu duuf gi nekkul ci biir bi moo gën ci yaw.