Embrasser l'Islam, cliquez ici
ISLAM AL-HAQ: QURAN & HADITH
(The True Islam)



Imam Ahmad : 128

حَدَّثَنَا مُعَاوِيَةُ بْنُ عَمْرٍو حَدَّثَنَا زَائِدَةُ حَدَّثَنَا عَاصِمٌ وَحُسَيْنُ بْنُ عَلِيٍّ عَنْ زَائِدَةَ عَنْ عَاصِمٍ عَنْ زِرٍّ عَنْ عَبْدِ اللَّهِ قَالَ لَمَّا قُبِضَ رَسُولُ اللَّهِ صَلَّى اللَّهُ عَلَيْهِ وَسَلَّمَ قَالَتْ الْأَنْصَارُ مِنَّا أَمِيرٌ وَمِنْكُمْ أَمِيرٌ فَأَتَاهُمْ عُمَرُ رَضِيَ اللَّهُ عَنْهُ فَقَالَ يَا مَعْشَرَ الْأَنْصَارِ أَلَسْتُمْ تَعْلَمُونَ أَنَّ رَسُولَ اللَّهِ صَلَّى اللَّهُ عَلَيْهِ وَسَلَّمَ قَدْ أَمَرَ أَبَا بَكْرٍ رَضِيَ اللَّهُ عَنْهُ أَنْ يَؤُمَّ النَّاسَ فَأَيُّكُمْ تَطِيبُ نَفْسُهُ أَنْ يَتَقَدَّمَ أَبَا بَكْرٍ رَضِيَ اللَّهُ عَنْهُ فَقَالَتْ الْأَنْصَارُ نَعُوذُ بِاللَّهِ أَنْ نَتَقَدَّمَ أَبَا بَكْرٍ رَضِيَ اللَّهُ عَنْهُ

Mu wax nu [Mu'awiyah Bin Amru] Mu wax nu [Za'ida] Mu wax nu [Ashim] ak [Husain Bin Ali], ci [Za'ida] ci [Ashim] ci [Zirr] ci [Abdullah] mu ne; Bi Rasulullah faatoo, waa Ansar dañu wax; 'Ci nun am njiit, ci yeen am njiit'. Omar daal di ñëw ci ñoom ni leen; 'Yéen waa Ansaar, ndax xamuleen ni Yonent bi sallallaahu aleyhi wasallah digaloon na Abubakr mu jiite nit ñi, kon kan moo dal ci xolam mu jiitu Abubakr? Kon waa Ansar tontu; 'Danuy ñaan Yàlla musal nu baña jiitu Abu Bakr'.