Embrasser l'Islam, cliquez ici
ISLAM AL-HAQ: QURAN & HADITH
(The True Islam)



Bukan golongan kami, tidak sayang anak kecil, tidak tahu hak orang lebih besar
Imam Tirmidzi : 1842

حَدَّثَنَا مُحَمَّدُ بْنُ مَرْزُوقٍ الْبَصْرِيُّ حَدَّثَنَا عُبَيْدُ بْنُ وَاقِدٍ عَنْ زَرْبِيٍّ قَال سَمِعْتُ أَنَسَ بْنَ مَالِكٍ يَقُولُجَاءَ شَيْخٌ يُرِيدُ النَّبِيَّ صَلَّى اللَّهُ عَلَيْهِ وَسَلَّمَ فَأَبْطَأَ الْقَوْمُ عَنْهُ أَنْ يُوَسِّعُوا لَهُ فَقَالَ النَّبِيُّ صَلَّى اللَّهُ عَلَيْهِ وَسَلَّمَ لَيْسَ مِنَّا مَنْ لَمْ يَرْحَمْ صَغِيرَنَا وَيُوَقِّرْ كَبِيرَنَاقَالَ وَفِي الْبَاب عَنْ عَبْدِ اللَّهِ بْنِ عَمْرٍو وَأَبِي هُرَيْرَةَ وَابْنِ عَبَّاسٍ وَأَبِي أُمَامَةَ قَالَ أَبُو عِيسَى هَذَا حَدِيثٌ غَرِيبٌ وَزَرْبِيٌّ لَهُ أَحَادِيثُ مَنَاكِيرُ عَنْ أَنَسِ بْنِ مَالِكٍ وَغَيْرِهِ

Mu wax nu [Muhamed bin Marzuq Al Bashari], wax nu [Ubaid bin Waqid] ci [Zabri] ni, dégg naa [Anas bin Malik] wax; Amna benn mag bu ñëw ci Yonent bi, nit ñi daal di wàññi seen gaawaay ngir yaatal ko yoon wi, ci noonu la Yonent bi wax: 'Amul ci sunu mbooloo ñi bëggul sunuy doom te joxu ñu cër sunuy waajur - sunu mag ñi'. Xadiis bi abdalaa bin amr ak abu hurayrata ak ibnu abaas ak abu umaama ñoo ko nettali. Abu Isa ne ko: Lii hadiis bu gharib la, Zarbi amna ay hadiis yu bon yu bawoo ci Anas bin Malik ak ñeneen.

Hadith Corroboration :

Imam Ahmad : 2214, 6445, 6640, 6643, 6776, 6824, 6988, 7329, 8673, 10257, 10935, 11278, 18373, 18375, 18378, 18379, 18393, 18398, 18407, 18444, 18447, 18450, 18460, 18461, 21693
Imam Bukhari : 5538, 5554, 6828
Imam Muslim : 4282, 4283
Imam Abu Dawud : 4292, 4541
Imam Tirmidzi : 1834, 1842, 1843, 1844, 1845
Imam Ibnu Majah : 3079