Embrasser l'Islam, cliquez ici
ISLAM AL-HAQ: QURAN & HADITH
(The True Islam)



Rasulullah apabila bertakbir maka beliau mengangkat tangannya sejajar dengan pundaknya
Imam Abu Dawud : 619

حَدَّثَنَا أَحْمَدُ بْنُ مُحَمَّدِ بْنِ حَنْبَلٍ حَدَّثَنَا سُفْيَانُ عَنْ الزُّهْرِيِّ عَنْ سَالِمٍ عَنْ أَبِيهِ قَالَرَأَيْتُ رَسُولَ اللَّهِ صَلَّى اللَّهُ عَلَيْهِ وَسَلَّمَ إِذَا اسْتَفْتَحَ الصَّلَاةَ رَفَعَ يَدَيْهِ حَتَّى يُحَاذِيَ مَنْكِبَيْهِ وَإِذَا أَرَادَ أَنْ يَرْكَعَ وَبَعْدَمَا يَرْفَعُ رَأْسَهُ مِنْ الرُّكُوعِ وَقَالَ سُفْيَانُ مَرَّةً وَإِذَا رَفَعَ رَأْسَهُ وَأَكْثَرُ مَا كَانَ يَقُولُ وَبَعْدَ مَا يَرْفَعُ رَأْسَهُ مِنْ الرُّكُوعِ وَلَا يَرْفَعُ بَيْنَ السَّجْدَتَيْنِ

Daf nu wax [Ahmad bin Muhamed bin Hanbal] wax nu [Sufyan] ci [Az Zuhri] ci [Salim] ci [pàppaam] mu ne; "Mus naa gis ni Yonent bi sallallaahu 'alaihi wasallam tàmbali ñaan, mu siggil loxoom ba ñu tolloo ak mbaggam dayo yi, noonu la su bëggee sukku, maanaam ginaaw bimu siggilee boppam ci sukku." Beneen yoon Sufyan wax; 'Su yëkkati boppam'. Ak waxin wi muy faral di jëfandikoo mooy; Maanaam, ginnaaw bi mu yékkatee bopp ba ci rujj te yékkatiwul ay loxoom ci diggante ñaari sujjóot.

Hadith Corroboration :

Imam Ahmad : 679, 4312, 4445, 5502, 5579, 5899, 6046, 7905, 18095
Imam Bukhari : 693, 694, 696, 697, 744, 785
Imam Muslim : 586, 587, 594
Imam Abu Dawud : 619, 620, 627, 629, 632, 633, 634, 635
Imam Tirmidzi : 237, 280, 3345
Imam Nasa'i : 866, 867, 868, 1015, 1047, 1049, 1147, 1168, 1169
Imam Ibnu Majah : 848, 852, 854, 1051
Imam Malik : 149, 154
Imam Darimi : 1222, 1322