Embrasser l'Islam, cliquez ici
ISLAM AL-HAQ: QURAN & HADITH
(The True Islam)



Rasulullah mendatangi tempat pembuangan sampah suatu kaum, beliau lalu kencing sambil berdiri

Imam Abu Dawud : 21

حَدَّثَنَا حَفْصُ بْنُ عُمَرَ وَمُسْلِمُ بْنُ إِبْرَاهِيمَ قَالَا حَدَّثَنَا شُعْبَةُ ح و حَدَّثَنَا مُسَدَّدٌ حَدَّثَنَا أَبُو عَوَانَةَ وَهَذَا لَفْظُ حَفْصٍ عَنْ سُلَيْمَانَ عَنْ أَبِي وَائِلٍ عَنْ حُذَيْفَةَ قَالَأَتَى رَسُولُ اللَّهِ صَلَّى اللَّهُ عَلَيْهِ وَسَلَّمَ سُبَاطَةَ قَوْمٍ فَبَالَ قَائِمًا ثُمَّ دَعَا بِمَاءٍ فَمَسَحَ عَلَى خُفَّيْهِقَالَ أَبُو دَاوُد قَالَ مُسَدَّدٌ قَالَ فَذَهَبْتُ أَتَبَاعَدُ فَدَعَانِي حَتَّى كُنْتُ عِنْدَ عَقِبِهِ

Neena ñu [Hafsh bin Omar] ak [Muslim bin Ibraahim] ñoom ñaar ñu ne; Neena ñu [Syuba]. Ak ci beneen yoon; Musaddad neena nu Abu Awanah, te lii mooy Hafsh lafazh bu bawoo ci [Sulaiman] bu bawoo ci [Abu Wa'il] bu bawoo ci [Hudzaifah] mu ne; Benn bis la Yonent bi sallallaahu aleyhi wasallam dem ci mbalitu nit ñi, daal di saw taxaw, daal di sàkku ñu indil ko ndox, daal di fomp ñaari khufam. Abuu Daawuda nee na; Musaddad neena; Hudzaifa neena; Ba noppi ma dem fu sori, waaye mu wooma ba ma nekk ci taloŋ.

Hadith Corroboration :

Imam Ahmad : 1778, 20747, 20754, 20765, 20766, 20813, 20830
Imam Bukhari : 136, 175, 176, 196, 199, 1556, 1557, 1558, 1560, 4069, 5352, 5353
Imam Muslim : 402, 404, 405, 408, 409, 412, 2245, 2256, 2257, 2258, 2259, 2260, 2261, 2262
Imam Abu Dawud : 21, 144, 1641, 1644
Imam Nasa'i : 605, 2974, 2975
Imam Malik : 797
Imam Darimi : 1806